10/05/2022
Charte tarikha bi nak 23 la
1) esk koula diokh tarikha bi amna Ndiguel diokhé tarikha bi
2) yaw mi beuga diap tarikha bi doko bollé ak bénenen tarikha
3) yaw mi beuga donn app Tidiane Mba dieul NGA wird
4) yaw mi beuga donn app Tidiane do ziaré bénen waliyou boudoul Tidiane ziaratou istimdate
5) thiofél sa Serigne Nay yokou wayé boum wagni kou moukou wakhatou malak difa Guedj
6) louy ndiro mbaniél Mba saga Mba khass boumou diougué si yaw di dém si sa Serigne
7) sa Serigne Ay wakham Nala gueneul wakhi niep
8/ mouthaleul sa bop di digante sa Serigne (
critiqué ko)
9) samontel ak Charte charia Yi di dioulé sa diaka ja diko def ak wakhtom wayé bollé si tamite same sa diganté ak sa niari waydiour lép di raffet
10) do wollu pékhém Yalla Tidiane la RK bakar bouma nékh deff kouma nékh lép dédet yangii wollu pékhém Yalla
11) moy bo diapé tarikha bi doko bayii ba bangay fatouu
12) dangay wazifa sa mbolo ndém amna NGA mbolo Hadaratul jumah sa mbolo ma ndém amo ngante
13 moy diawharatul kamal doko diangu si loudoul laboum ndokh té labb NGA matteu seuk
14) moy do dogo ak béne dioulite rawatina app Tidiane
15 moy wird bi boulko di doyadal dél wird si heures si wahtou té samonté ak téguine Yi
16) moy boul sampu sa bopou nane dangay mayé wird té amo Ndiguel mayé wird
17) moy lép lou askano si cheikh lolou Danko wara ormal diko kholé Serigne bi
18) moy wazifa boy lazim boy Hadaratul jumah dangay tabal yéné
19) moy wazifa boy wird boy Hadaratul jumah finga tok dafa wara labb linga soll dafa wara labb yaw si bopou dangay labb
20) dangay sangou say awra dangay tok comme togayou kouy diouli dangay dioubllu pénkou loudoul si touki NGA nék fo dieum bahna
21) moy wird doto wakh ak kéneu loudoul sa niari waydiour wala sokhna souy wouyou dieukaram wala dieukeur diouy wakh ak sokhna wala sa Serigne bi la may tarikha bi
22) boy wird dangay imaginer dieumi yonnentibi si sa kanam bosi tolluwul NGA imaginer dieumi cheikh si sa kanam bosi tolluwul NGA imaginer dieumi ki la diokh tarikha bi chartes la si tarikha bi
23) moy batt Yi ngay wakh boy wird mo kham astahfiroulah la wala salatu ala nabiyi la wala la ilaha ilalah la dél téwllu limmuy firi
Mbok li moye chartes tarikha bi